As an anonymous user, you can only add new data. If you would like to also modify existing data, please create an account and indicate your languages on your user page.

Portal:wol

From OmegaWiki
Jump to: navigation, search
Ethnologue ISO-639-1 wo
ISO-639-3 wol
Babel user information
wo-N Bii jëfandikukat dégg na wolof ni ku ci juddu.
wo-5 Bii jëfandikukat dégg na wolof yu xereñ.
wo-4 Bii jëfandikukat dégg na wolof yu jege ku ci juddu.
wo-3 Bii jëfandikukat dégg na wolof bu baax.
wo-2 Bii jëfandikukat dégg na wolof yu diggdoomu.
wo-1 Bii jëfandikukat dégg na wolof tuuti rekk.
Users by language
Search user languages

Wolof[edit]

Dalal-jàmm ci bunt bu wolof ci OmegaWiki!

OmegaWiki ab naal la bu aajewoo jappalante ngir man a taxawal ab baatukaay bu bari-làkk, di man a joxe cosaani baat yi, ci làkki àdduna bi yépp.

Lii nak day rekk ndoorteelu naal bi, moo tax nu gën a yitteel baatal bi, waaye bu ci kanamee di nan man a joxe cosaani baat yi, ak ni ñuy soppikoo ci waxiin yi.

Li OmegaWiki nekk ci ndooteelam moo tax du ñépp ay man a def ay coppite. Bu ci kanamee di nan ko yaatal.

Soo leen gisee ay njuumte ci baat yi man ngeen kaa wone ci xëtu waxtaanukaay yi, bind fa lii

Icon tools.png
This article (wol) needs attention because:
<problems con article>
It has been added to this category for attention. Thank you for your patience.

ci xëtu waxtaanukaay ba. Di nan nangu tamit seniy xelal.

Donte amul leen sañ-sañu man a soppi, waaye man ngeen def bind ci waxtaan yi, ci xëtu jëfëndikookat yi ak ci xëtu bunt yi.

Firi (to be translated)[edit]

Main page

Translate the following pages for a complete Main page in your language:

Supporting pages

yénn ci Arafi wolof[edit]

Ë ë Î î Ï ï Ô ô Ü ü à À ã · é É ë Ë ẽ € · ó Ó ō œ Œ · ñ Ñ ŋ Ŋ · ç Ç · «» {{}} “” ·

Ay Réew[edit]

Réewum Senegaal - الجمهورية الإسلامية الموريتانية(Gànnaar)